《Pullo rdo》歌词

[00:00:00] Pullo Àrdo - Youssou N'Dour (尤索·恩多)
[00:00:15] Koufi gneuw mu diangal la
[00:00:17] Niax mi môko môm
[00:00:19] Ndokh mi môko môm
[00:00:20] Daf ko donn
[00:00:21] Lî khar yi la
[00:00:23] Lî beuy yi la
[00:00:24] Nagam yangui
[00:00:25] Àll bâ ngui
[00:00:27] Baxi mâmam poullo àrdo
[00:00:36] Koufi gneuw mu diangal la
[00:00:39] Niax mi môko môm
[00:00:40] Ndokh mi môko môm
[00:00:42] Lî khar yi la
[00:00:43] Lî beuy yi la
[00:00:44] Nagam yangui
[00:00:46] Àll bâ ngui
[00:00:47] Baxi mâmam poullo àrdo
[00:00:51] Pullo ardo pullo djèry pullo ardo
[00:00:57] Pullo djèry pullo ardo pullo djèry
[00:01:02] Dakhal yi mu jeum fé
[00:01:03] Nga dakh yé mou jeum fi
[00:01:05] Yâ xam yaw li khèw fé
[00:01:06] Dara diaxa loula fi ba fé
[00:01:09] Pullo ardo pullo djèry pullo ardo
[00:01:14] Pullo ardo pullo djèry pullo ardo
[00:01:30] Ardo sékhna guëneum
[00:01:33] Daldi gaddu yatam
[00:01:36] Ma nga anddak khadjam
[00:01:38] Daldi djitël guéteum
[00:01:41] Pullo djèry pullo ardo
[00:01:46] Mingui anddak khdjam
[00:01:49] Daldi djitël guéteum
[00:01:52] Dalal xélam
[00:01:53] Féxal xolam
[00:01:55] Bou nit gniy fo aka ré môm yëguko souy
[00:01:59] Pullo ardo pullo djèry
[00:02:04] Lépp am mingui fi
[00:02:07] Fî la yarô
[00:02:08] Fî la magué
[00:02:09] Téyit fî la
[00:02:11] Také soxna
[00:02:12] Lépp am fî la
[00:02:15] Pullo ardo pullo djèry
[00:02:22] Bu nit gniy teub aka dal môm yëguko
[00:02:24] Limu am fî doy nako té doylô nako
[00:02:27] Boudè or la
[00:02:28] Mba jamâ
[00:02:30] Wala étage la
[00:02:31] Mba avion la
[00:02:32] Mba lénène la
[00:02:34] Môm guissouko pullo ardo
[00:02:48] Ma nga gaddu tôkhôr om
[00:02:51] Di mbîb mbîb yu am khôrôm
[00:02:54] Waye waye yu amoul môrôm
[00:02:57] Mél ni kouy nèkhal gôrôm
[00:02:59] Bofa diarè sant sarr è dinala rè
[00:03:05] Bofa diarè dône sérère è dinala rè
[00:03:10] Bofa diarè sant sarr è dinala rè
[00:03:15] Bofa diarè dône sérère è dinala rè
[00:03:21] Ma nga gaddu tôkhôr om
[00:03:24] Di mbîb mbîb yu am khôrôm
[00:03:26] Waye waye yu amoul môrôm
[00:03:29] Mél ni kouy nèkhal gôrôm
[00:03:32] Bofa diarè sant sarr è dinala rè
[00:03:37] Bofa diarè dône sérère è dinala rè
[00:03:42] Bofa diarè sant sarr è dinala rè
[00:03:48] Bofa diarè dône sérère è dinala rè
您可能还喜欢歌手Youssou N’Dour的歌曲:
随机推荐歌词:
- Bellissimo [ILYA]
- Release Yo’ Delf(Prodigy Remix) [Soundtrack]
- Little Tornado [Aimee Mann]
- Pagbigyang Muli [Erik Santos]
- 911 Is A Joke [Public Enemy]
- We Are the Pigs [Suede]
- John the Revelator [Harry Belafonte]
- Supercharged [x]
- 一生一次 [刘德华]
- 曾经的最爱 [朱昊楠]
- Watch the World [Markus Schulz&Lady V]
- Sub Title [坏男人电视剧]
- I Can’t Be Satisfied [Big Bill Broonzy]
- Radha [Udit Narayan&Vishal Dadla]
- The Night Before Proposal [Super Fine&Zan Dark]
- GET LOW(128 BPM) [D’Mixmasters]
- I’m Beginning to See the Light [The Ames Brothers&Bill Fi]
- House of the Rising Sun [Nina Simone]
- Turn Her Down [Faron Young]
- Nichts von alledem [Wolfgang Petry]
- Living in Exile [Sleater-Kinney]
- You’re Breaking My Heart [B.B. King]
- RANDOMSONG [Willow Smith]
- I Don’t Want To - Frankie Knuckles Radio Edit [Toni Braxton]
- Girls On Film [Hi NRG Fitness]
- 托 [张雷]
- Asahi ~Shine & Groove~ [大黒摩季]
- (MR) [ParkJungSik]
- 【他柠】做人多累啊,我想做只猫 [挥霍]
- El Mini Lic [Los Del Arroyo]
- I’ve Been Thinkin’ [Ricky Nelson]
- 佛缘 [谭英]
- 兄弟再干一杯 [刘老板]
- All Of Me [Harry James Orchestra&Dol]
- Walking In Heaven’s Sunshine(Demo Version) [The Jam]
- 情人的眼泪 [潘秀琼]
- Le gorille [Georges Brassens]
- 多少次 [罗嘉良]
- Hello me [大塚愛]
- Bitter Roots [For Today]
- Ce N’etait Qu’un Reve (Live in Quebec City) [Celine Dion]