找歌词就来最浮云

《Leaving(Album Version)》歌词

所属专辑: The Guide (Wommat) 歌手: Youssou N’Dour 时长: 04:59
Leaving(Album Version)

[00:00:00] Leaving - Youssou N'Dour (尤索·恩多)

[00:00:20] Dem dem

[00:00:21] Dem fan

[00:00:23] Den ndax lan

[00:00:24] Baya ko mom

[00:00:26] Dem nguir xee bou barri bi

[00:00:30] Dem ndax teen boh neex bi

[00:00:33] Teh rapp rek noom noo siy naan

[00:00:36] Nach bi lakkatouma taw bi barrewoul

[00:00:40] Dem ngir bokk bone menou fee am

[00:00:43] Dem ngir daffa wara nekk gorr done

[00:00:45] Goorgoorlau

[00:00:53] Dem dem

[00:00:54] Dem fan

[00:00:56] Dem ndax lan

[00:00:57] Liberte bi

[00:00:59] Si espace bou lendeum bi

[00:01:02] Sama beut yi guissa tounou

[00:01:06] Garap yi nga xamenteni noo ma souxat

[00:01:09] Su beut setiee barap yi bow

[00:01:12] Dem ngir Keur gui daf may nirou lou lendeum

[00:01:16] Dem nguir daffa warranekk goor done

[00:01:18] Goorgoorlau

[00:01:25] Damay dem

[00:01:26] Chi alla bi

[00:01:28] Damay dem Chi dex goumak gui

[00:01:31] Ne damay dem waw seeti sama nawleyee

[00:01:35] Damay dem si ban bou ritax bi

[00:01:38] Damay dem ba reewu bitty

[00:01:41] Ne damay dem waw setti samambokkyee

[00:01:43] Go-go

[00:03:03] Won ma sa yarii ma wax la ki nga donoy

[00:03:06] Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar

[00:03:09] Hey what do you need 

[00:03:13] He he yaw lilaneex

[00:03:16] Won ma sa yarii ma wax la ki nga donoy

[00:03:19] Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar

[00:03:22] He defa li la neexoy hey yaw lila soop

[00:03:29] Sammkatou mboott moo xam ba ciy

[00:03:32] Sooxaoy ni meneuh kott noom daal amounou

[00:03:37] Mbaam hey defal li la nexx oo

[00:04:33] Ho ho ho ho