《Létt ma》歌词
[00:00:00] Létt ma - Youssou N'Dour (尤索·恩多)
[00:00:00] Du nii du nii bëgg naa nga létt ma
[00:00:08] Walla book nga firi ma
[00:00:11] Xamal ma lu leer
[00:00:16] Danga maa woolu sa gàlle ma ñëw nga mel ni xale
[00:00:21] Yaw daal yaw tóppal fële
[00:00:23] Danga ba di tappale
[00:00:26] Su fekkeeni parewoo waru loo di yónéé
[00:00:31] Ngall yaw bul ma defloo lu ma nin ñi di xeebe
[00:00:36] Létt ma mbaa nga firi ma
[00:00:50] Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
[00:01:00] Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
[00:01:10] Lég lég sax nga yónni ma
[00:01:13] Ma dem bay dem nga teye ma
[00:01:15] Léégi sax dematuma
[00:01:18] Damay bañ nga dugël ma
[00:01:21] Bu fekkeeni parewoo waru loo di yónéé
[00:01:26] Ngall yaw bul ma def loo lu ma nin ñi di xeebe
[00:01:31] Létt ma mbaa nga firi ma
[00:01:45] Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
[00:01:55] Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
[00:02:06] Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
[00:02:11] Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw
[00:02:16] Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
[00:02:21] Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw
[00:02:26] Létt ma mbaa nga firi ma
[00:02:40] Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
[00:02:50] Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
[00:03:00] Boo ma waxee fi nga bëgg dem
[00:03:03] Ma wax la fi ngay jaar
[00:03:06] Demal bul dem waxal bul wax defal bul def
[00:03:10] Man daal sonn naa sonn naa sonn naa
[00:03:16] Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
[00:03:21] Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë
[00:03:29] Bëgg ak bañ la
[00:03:32] Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë
[00:03:40] Bëgg ak bañ la
[00:03:42] Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë
[00:03:50] Bëgg ak bañ la
[00:03:52] Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë
[00:04:00] Bëgg ak bañ la
[00:04:03] Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë
[00:04:11] Bëgg ak bañ la
[00:04:13] Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë
[00:04:21] Bëgg ak bañ la
[00:04:24] Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë
[00:04:32] Bëgg ak bañ la
您可能还喜欢歌手Youssou N’Dour的歌曲:
随机推荐歌词:
- Awaken The Music [Billy Gilman]
- 宫心计 [关菊英]
- 一分钟都市一分钟恋爱 [林忆莲]
- Open the Door [Nana Mouskouri]
- Circus Lights(Album Version) [Deacon Blue]
- 经过 [刘若英]
- After All(feat. Bryan Adams) [Michael Bublé&Bryan Adams]
- 少年ハート [群星]
- 给你的歌 [青桂贤]
- Mercedes Benz [Klaus Lage]
- You Remembered Me [Johnny Cash]
- Pumpin Blood(Drums of Death Remix) [NONONO]
- Johnny B. Goode [Chuck Berry]
- Crow On The Cradle [Judy Collins]
- Sexual Healing [Midnight King]
- Pikkuprt(Huge L Remix) [Steen1]
- I Remember [Maurice Williams&The Zodi]
- Song For The Night [Stanfour]
- 爱情不是想象的那样 [萧全]
- Reuben’s Train [The Dillards]
- Harapanku [JPCC Worship]
- When I Fall in Love [Marylin Monroe]
- Feel The Love [Vincent Blake&Shell B]
- 月光光(Live) [Beyond]
- Till [Tom Jones]
- Spitting Out Teeth [Thirteen Senses]
- 明天 [MC阿萌]
- Chasing [余超颖]
- The Five Pennies [Louis Armstrong&Ma Rainey]
- Keeping The Love Alive [Nana Mouskouri]
- 非诚勿扰 [王震]
- 【高人一等】撒拉小伙 [马阿俊]
- 你我约定今宵情 [傲雪藏梅]
- Tu m’oublieras [Nos Annees 90]
- DRIVE BY(The Factory Team Happy Remix) [One Nation]
- 你的梦想 [尹岳海]
- This Is Love [2PM]
- Young Blood [Jukebox Junction]
- El Beso [Miguel de Molina&Lolita S]
- Old Time Rock N’ Roll [Little Donkey]
- The Great Pretender [The Platters]