找歌词就来最浮云

《Gen ji dekk》歌词

所属专辑: Titi la lionne 歌手: Titi 时长: 05:36
Gen ji dekk

[00:00:00] Gen ji dekk - Titi

[00:00:02] Written by:Ibou Ndour/Titi

[00:00:08] Guentouma hé Gentouma

[00:00:12] Hoooooo Hooo

[00:00:22] Guentouma hé Gentouma

[00:00:26] Beugouma yewou rek guente gui diekh

[00:00:36] Ngua neck fi ma neck feulé

[00:00:38] Dou té niou gussanté

[00:00:39] Nékal fi mangui feulé Beugenala

[00:00:43] Khol dafa noyya noye Louo ci dougou yeuknako

[00:00:47] Beugnala

[00:00:49] Guemenala

[00:00:50] Geumnawooo Ho

[00:00:53] Guentouma

[00:00:53] Guentouma

[00:01:01] Nekkal fi ma neck feulé

[00:01:02] Dou té niou gussanté

[00:01:04] Nékal fi mangui feulé Beugenala

[00:01:08] Khol dafa noyya noye Louo ci dougou yeuknako

[00:01:11] Beugnala

[00:01:13] Guemenala

[00:01:15] Geumnawooo Ho

[00:01:17] Guentouma

[00:01:18] Guentouma

[00:01:26] Naniou Khalaté lou lenne nekh ci mane

[00:01:29] Bayiléne niou wakh louléne nekh ci mane

[00:01:40] Maye adji kiiy beug Beugnala

[00:01:44] Beug Sa Deuk Ba Deuk

[00:01:45] Fa mouy guene di deuk ci mane

[00:01:54] Yaw yaye ki kidnaper sama life

[00:01:57] Hooo Hooo My life

[00:02:08] Kidnaper sama temps khamnala

[00:02:12] Temperature bo necké soma guissé guif

[00:02:22] Dangua beugonna kham ci lanne la néék

[00:02:26] Dangua beugonna kham ci lanne lay dokh

[00:02:29] Yakamtina niouye skype

[00:02:33] Deug sa viber am sa allo

[00:02:36] Arrosé na samay fleur mane

[00:02:40] Ba meuna feyy ci bissoub mbeugéll yii

[00:02:51] Gen Ji Dekk dama yague ak yaw

[00:02:54] Ba so yeukeutii say kaddu

[00:02:57] Bala nguay danéél makoy teureul

[00:03:00] Gen Ji Dekk

[00:03:04] Geunalanté wouma la ak niom My baby

[00:03:08] Dafa fekk ni do niom douniou yaw

[00:03:11] Minne na la

[00:03:13] Tammou na la

[00:03:15] Mane mala tamou ci niom ba ngua doyma

[00:03:24] Ni ngua ma beugé dafa diegui dayyo

[00:03:27] Ni mala beugué rombe na Yillif

[00:03:31] Ni ngua ma beugé dafa diegui dayyo

[00:03:34] Ni mala beugué rombe na Yillif héé

[00:03:44] Sama guente gui

[00:03:47] Mba douma yewou rek mou diekh

[00:03:53] Sama guente gui

[00:03:58] Mba douma yewou rek mou diekh

[00:04:05] Sama guente gui

[00:04:09] Mba douma yewou rek mou diekh

[00:04:21] Gen Ji Dekk

[00:04:23] Ya léne guene ci mane

[00:04:26] Té dou yagg ba ngua donne niom

[00:04:29] Do meussa donne niom

[00:04:43] Soumay nieuw ci yaw

[00:04:46] Ropplane loumou naw naw

[00:04:49] Ma guena gaw ci yaw

[00:04:54] Nangouna donne sa autorail

[00:04:57] Souma djoubé gare cornet né Yeuksinna

[00:05:06] Beug nala guemnala

[00:05:08] Ni mala beugé dafa diegui dayyo

[00:05:11] Ni ngua ma beugué rombe na Yillif

[00:05:14] Beug nala

[00:05:16] Beug nala

[00:05:17] Beug nala

[00:05:27] Beug nala

您可能还喜欢歌手Titi的歌曲:

随机推荐歌词: