找歌词就来最浮云

《Jammu Africa(Album Version)》歌词

所属专辑: Best Of 歌手: Ismael Lo 时长: 05:01
Jammu Africa(Album Version)

[00:00:01] Jammu Africa - Ismael Lo

[00:00:02] Written by:Ismaël Lo

[00:00:13] Afrika a a a

[00:00:19] Afrika mon afrique

[00:00:37] Sama gent gi maa ngi ñaan

[00:00:39] Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq

[00:00:43] Ma ne bes du ñakk ci bes yi

[00:00:44] Afrika don benn reew

[00:00:49] D'ici ou d'ailleurs

[00:00:52] Nous somm' des enfants d'afrique

[00:00:54] Mêm' si le ciel tombait

[00:00:57] Luttons pour la paix

[00:01:01] Kon jammu afrika

[00:01:04] Moom lay ñaan

[00:01:07] Mané jammu afrika mooy suñu natange

[00:01:25] Afrika a a a

[00:01:31] Afrika a a

[00:01:37] Afrika a a a

[00:01:43] Afrika mon afrique

[00:01:49] Yow mi nekka bittim reew man mi lô maa ngi lay ñaan

[00:01:54] Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel

[00:01:57] Bul fatte Afrika

[00:02:01] Ici ou ailleurs

[00:02:04] La paix prix du bonheur

[00:02:07] Mêm' si le ciel pleurait

[00:02:09] Luttons pour nos frères

[00:02:13] Kon jammu Afrika

[00:02:16] Moom lay ñaan

[00:02:19] Mané jammu Afrika mooy suñu natange

[00:02:37] Afrika a a a

[00:02:43] Afrika a a

[00:02:49] Afrika a a a

[00:02:55] Afrika mon afrique

[00:03:01] Afrika a a a

[00:03:07] Afrika a a

[00:03:13] Afrika a a a

[00:03:19] Afrika mon afrique

[00:04:01] Onon bibbe Afrika ngimode

[00:04:05] Ngimode liggo den leydi men

[00:04:07] Afrika mon afrique

[00:04:10] Ngaccen hasi daagal

[00:04:13] Yoo Alla suren e musibaadi

[00:04:16] Yoo Alla addu jam to Ruanda

[00:04:19] Afrika mon Afrique

[00:04:22] Yoo Alla addu jam to Burundi

[00:04:25] Yoo Alla addu jam to Casamans

[00:04:28] Lawol Mbignona yee

[00:04:31] Afrika mon Afrique

[00:04:37] Africa a a a Africa

随机推荐歌词: